25 septembre 2007

Dread Maxim "mbollo"

Dread Maxim clip "mbollo" :


parole et traduction de "Mbollo" :


Nio bok ndeye, bok bène baye

Lolo takh nioune niou tew fi tey

Mbollo war na nio war na domi rew

So africa tè nio bollo





Mbir mi dafa tiss

Li niou yènou dafa diss

Wayè meuna bagna diss

Sunu bolè sunuy dolè

Dèf li niou war, djèma baye sunu waar

Bagna doni none, bayi djef djou bone



Africa tè nio mbollo

Africa tè nio mbollo

Boul khar niou wakh la li la war

Kounek kham ngha li la war

Li niou mana df nghir am dunya bou gueune

Africa rè

Way kounek beugue na djitè

Kounek beugue na djitou djiteul niènene ni tope thi

Kounek beugue fèkè fa niouy sèdo alal dji

Djèl sa waale dièlalè waalou niènène ak niènèneBoba niène nia nghi dioye nghir mare ak raflè



Nous sommes du même père et de la même mère

Voilà pourquoi nous sommes ici

L’unité se doit entre frères de sang

Afrique, de grâce, unissons nous




L’affaire est urgente

Et le fardeau est lourd

Mais il sera moins lourd à porter

si nous unissons nos forces

accomplir notre devoir de citoyen

vivre positif rester frère



n’attends pas qu’on te dise ce que tu dois faire

tout un chaqu’un doit connaître son devoir

ce qu’il faut faire pour un monde meilleur

pour que l’afrique puisse enfon sourire

mais chaqu’un veut diriger

chaqu’un veut occuper les devants

chaqu’un veut assister au partage du gateau

prendre sa part et celle des autres

pendant que d’autre meurent de faim et de soif

Aucun commentaire:

Rechercher dans Roots and Culture

Education is the key